| término | definición | |||
|---|---|---|---|---|
|
Nanga def?
|
||||
|
Maangi fi rekk
|
||||
|
Naka waa kër gi?
|
||||
|
Ñuungi fi
|
||||
|
Nanga fanaane?
|
||||
|
Nanga yendu?
|
||||
|
Jàmm rekk
|
||||
|
Nangeen def?
|
||||
|
Nungi fii rekk
|
||||
|
Ana / naka sa yaay / sa baay?
|
||||
|
Mungi fi
|
||||
|
Nangeen fanaane?
|
||||
|
Naka ligéey bi?
|
||||
|
Mungi dox
|
||||
|
Mbaa kenn woppul?
|
||||
|
Mbaarikala
|
||||
|
reply to nanga def
|
Maangi sant
|
|||
|
Numu deme?
|
||||
|
Nii rekk
|
||||
|
Naka afeer yi?
|
||||
|
Ñungi dox
|
||||
|
Yaangi noos?
|
||||
|
Tuuti rekk
|
||||
|
Lu bees?
|
||||
|
Dara beesul
|
||||
|
Nelaw nga bu baax?
|
||||
|
Waaw, nelaw naa bu baax
|
||||
|
Jàmm nga fanaane?
|
||||
|
Naka suba si?
|
||||
|
Jàmm nga yendoo?
|
||||
|
Naka ngoon si?
|
||||
|
Naka tangaay wi?
|
||||
|
Naka seddaay bi?
|
||||
|
Ba benneen yoon
|
||||
|
Ba ci kanam
|
||||
|
Ba fan yi
|
||||
|
Ba suba
|
||||
|
Ba ngoon
|
||||
|
Ñu yendu ak jàmm
|
||||
|
Jàmm ak jàmm
|
||||
|
Ñu fanaan ak jàmm
|
||||
|
Dégguma Wolof bu baax
|
||||
|
Dégguma li nga wax
|
||||
|
Maangi jang Wolof ndank-ndank
|
||||
|
Jërëjëf
|
||||
|
Nuyòo
|
||||
|
Nuyu [someone]
|
||||
|
Def
|
||||
|
Fanaan
|
||||
|
Yendu
|
||||
|
Liggéey
|
||||
|
Dox
|
||||
|
Noos
|
||||
|
suba si
|
||||
|
Kër
|
||||
|
Dara
|
||||
|
Ana
|
||||
|
Naka
|
||||
|
Rekk
|
||||